Porogaraamu Ndaje bu mag bu ñetti fan bu atum 2021

Àjjuma

Porogaraamu àjjuma bi, mu ngi sukkandiku ci Luug 17:5: «Yokkal sunu ngëm».

Samdi

Porogaraamu samdi bi, mu ngi sukkandiku ci Yudd 3: «Xeexleen xeex bu metti ngir seen ngëm.»

Dimaas

Porogaraamu dimaas bi, mu ngi sukkandiku ci Macë 21:21: «Su ngeen gëmee . . . , dina ko def.»

Li ñi teew war a xam

Tegtal yu am solo yu ñi teew ci ndaje bu mag bu ñetti fan bii, war a xam.