Porogaraamu Ndaje bu mag bu ñetti fan bu atum 2022 bi tudd ‘Wutleen jàmm!’

Àjjuma

Porogaraamu àjjuma bi, mu ngi sukkandiku ci Sabóor 29:11: ‘Yexowa dina barkeele jàmm mbooloom’

Samdi

Porogaraamu samdi bi, mu ngi sukkandiku ci 2 Piyeer 3:14: Ñu «fekk leen ci jàmm, ngeen baña am benn gàkk mbaa sikk.»

Dimaas

Porogaraamu dimaas bi, mu ngi sukkandiku ci Room 15:13: «Yàlla miy maye yaakaar, na def ci seen xol mbég mu réy ak jàmm ju yaa»

Li ñi teew war a xam

Li ñi teew ci ndaje bu mag bu ñetti fan bi war a xam.