4-B
Xew-xew yi gën a am solo ci dundu Yeesu - Bi Yeesu tàmbalee waareem bi
JAMONO JA |
BÉRÉB BA |
XEW-XEW BA |
MACË |
MÀRK |
LUUG |
YOWAANA |
---|---|---|---|---|---|---|
29, daanaka oktoobar |
Dexu Yurdan, xéyna ca Betani gannaaw Yurdan walla ci wetam |
Ñu sóob Yeesu ci ndox te Xelum Yàlla wàcc ci moom ; Yexowa wax ne doomam la te won ko coofeelam |
||||
Màndiŋu Yude |
Seytaane fiir ko |
|||||
Betani ca gannaaw Yurdan |
Yaxya xàmme Yeesu ni Gàttub Yàlla ; taalibe yi njëkk ànd ak Yeesu |
|||||
Kana ca diiwaanu Galile ; Kapernawum |
Kéemaan bi njëkk ci céet, mu soppi ndox ma biiñ ; dem Kapernawum |
|||||
30, Bésu mucc ga |
Yerusalem |
Mu sellal kër Yàlla ga |
||||
Mu waxtaan ak Nikodem |
||||||
Yude, Aynon |
Yeesu dem diiwaanu Yude, taalibeem ya sóob nañu nit ñi ci ndox ; seede bi mujj bi Yaxya def ci Yeesu |
|||||
Tiberiyàdd ; Yude |
Tëj nañu Yaxya ; Yeesu jóge foofa dellu Galile |
|||||
Sikar, ca Samari |
Muy dem Galile, jàngal waa Samari |