Ndax dund ci jàmm ba fàww lu mën a nekk la?
Ndax dinga ne . . .
waaw?
déedéet?
walla xéyna?
LAN LA CI BIIBËL BI WAX?
«Ñi jub, dinañu moom suuf si, te dinañu ci dëkk ba fàww» (SABÓOR 37:29, MN).
LI BIIBËL BI WAX, BAN NJARIÑ NGA CI MËN A JËLE?
Yaakaaru dund ci jàmm ak sa njaboot ak say xarit (YEREMI 29:11).
Du rekk mën a dund ci jàmm ci diir bu gàtt waaye ba fàww (SABÓOR 22:27).
NDAX MËN NGA GËM LI BIIBËL BI DIGE?
Waaw-waaw! Ngir xam li tax, mën nga xool firnde yi nekk ci ñetti lesoŋ yi ci téere bu ndaw bii. Ñu ngi tudd: