Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

Ni ñuy jëfandikoo téere bu ndaw bii

Ni ñuy jëfandikoo téere bu ndaw bii

Téere bu ndaw bii, dina la dimbali nga mën a jàng li nekk ci Kàddu Yàlla, Biibël bi. Aaya yi nekk ci njeexteelu xise bu nekk, dinañu la won fan ci sa Biibël nga mënee liir tontu laaj yi ñu def ci mbind yi gën a ñuul.

Sooy liir aaya yi ci sa Biibël, nanga xool naka la aaya yi di tontoo laaj yooyu. Seede Yexowa bu mu mënta doon mën na la dimbali nga xam li Mbind mi wax. — Jàngal Luug 24:32, 45.

Xamal lii : Téere yi ñu lim yépp ci téere bu ndaw bii, Seede Yexowa yi ñoo ko defar.