Nettalib Yunus — njàngale bu jëm ci fit ak yërmande
Yexowa dafa sant yonent Yàlla Yunus mu dem ca réewu Asiri, ci dëkku Niniw yégal leen ne moom Yàlla dina leen àtte, waaye Yunus dafa bañ a dem. Xew-xew yu metti yi Yunus dund ginnaaw loolu, dimbali nañu ko mu xam ci dëgg-dëgg, lan mooy am fit ak am yërmande.